Saar 22

9K 1.2K 53
                                    



Saar 22

*****Khalil****

Parfois damay tok sama khel di deme fima diare ak Adja yeup rek khame ni l'histoire retiendra. Meussouma doundeu une telle montagne russe ci relation. Bima wakhé Dave damay tak Adja da tite. Mais Real frère la nak, dafe ma lathie si khame na bou bakh limay def si j'avais pesé le pour et le contre avant de me lancer et tout ça, mané ko waw bou wor. Il m'a souhaité bonne chance gnanal ma yalla dimbeulima ba douma meussa réthiou sama choix. Lolou rek la meunone def aussi. Fimou tole ni mome il y a plus de retour en arrière possible. Def na Adja madame Ibrahima Khalil Ndiaye, j'espère que dinako nék lou yague té lima dal ci Coura bagne ma dal ci mome. Sinon di na fi ame réputation wou homme divorcé bou bone. Alors défouma dara, gni ma koy sékeuk gno sikeu.

Lima défal Adja gnata gor gnokoy def ci deuk bi ? lima ko meuneul dé def nako. Soutoural nako. Instant yi képe kou khamoul liy gnoul ci sow mi pour yow Adja bimakoy dieul diank leu. Mais bon yonou kéne nékoussi mane ak sama diabarar la concerner mais puisque Sénégal dagno sob, mieux vaut bagne léne may lougne wakh et au moins sauver apparence et mieux vaut que ça continue comme ça.

Adja dé deux semaines après sougnou mariage laigneko mour mou seuy ci fek gnou def mariage civil bi ba paré. Defe naigne une petite fête, mais rien d'exagérer. Amou gnou diote bobou sakh.

Ça fait des jours maintenant depuis bi fi Adja néké. Je pense que sama yaye accepter nako. De toute façon mère bi khamenako. Meussoul ame problème. C'est vrai que je suis conscient que mo gui regretter Coura, après tout Coura nek na lou Adja doul meussa nek à savoir niècou mère bi. Mais bon, nièçame bou yarouwone donouma wone meussa takk Adja. Je me demande sakh si done nako khame.

Mane Sénégal ay ré laigne ma meussa def dagno meuna gérer ay détail à un point inimaginable.

Adja tay lay ayé togue pour la première et de ce fait affaire bi comme évènement, inviterna gnou bari keur ga gui fess déle instant yi.

Khamena ni daciy profito pour que gnou bar igname lokhome, mane mome mome khame na loumouy saf car yague nama inviter séne keur ma reir ci.

Nitt gni après nak gneupeuk manan yam. Kou léne wo ci kay lék gnou wouyou cila.

*********

Adja paella dé la togue. Bou toguone plat sénégalais bou simple kone dotoul nékati Adja bi ma tak. Ndaw ci darame simploule.

Instant yi gane yeup gnibi naigne ba ma nek sama nek ak sama diabar ak samay dome. Gnome gnare dé gno gui tok ci sama diguaneté ak Adja. Rokhaya mome tak na Adja déjà. Après c'est normal à 3 ans mome do khame li khew. Bi may remarierwou c'était ma plus grande crainte que samay dome accepter leur belle-mère té gnou bagne ko guiss comme la mauvaise femme qui est venue prendre la place de leur mère.

Mouhamed mome dafa meussa calme mais puisque gnagualoul sama kaname rek khel meune na dall. Je pense que accepter na Adja.

Après je reste bien sur mes gardes. Khame na séne yaye bou bakh et dara douma béte ci Coura. Seytané moy deuxième touram. Monter khalé yi contre Adja juste pour me pourir la vie défouko mouy dara. Mo takh khalé yi sougnouy wakh ak mome séne wett lay tok je veux savoir limou léne di wakh.

Instant yi dé béne feuilleton moy daw ci télé bi. Adja mome migui ci concentrerwou comme si sa vie en dépendait. Mane mome magui obeuli tellement que ça m'ennuie.

-Wa amour sétano ?

-Bala may sétane khame nimou démé.

5 secondes après lima wakh lako réthiou. Adja commencer nama raconter intrigou histoire bi alors que walay sama yone nékoussi. En plus khame nani yake na sétaname instant yi car ci mane la concentrerwou et pas si film bi.

Sa youma né comprendre ma yeugueul bope néko wow alors que vrai de vrai déguelou wouma sakh limouy wakh.

Quelques minutes après film bi diekh. Li nekh ci séne telenovelas yi moy jamais mou yague taf taf mou diekh et tant mieux.

-Wa amour, ame na lo khame né wakhagougne ci dé ?

-Lougne wakhoul ??? Lane la nonou ?

-Sama liguey bi khana ???

-Bo ligueyiwoul kay c'est parce que dafe la nekh. Meussou ma la né do liguey dé.

-Wa légui nane lay liguéyi wé té ma wara ayé 4 jours yi ?

-Dina la wouteul djank.

-Sa yaye dina nangou ?

-Loumou ciy bagne ? Coura bimouy seuy ci keur gui dadone diangue du coup j'étais obligé ma wouteul ko diank boukoy diapalé.

-Khalil boul faté ni mane nékouma Coura dé.

-Lolou kay wakh djou yakou la ni Coura mo gui France.

-Ladjoumala lane mo nékone relation Coura ak woudjou péthiorgome yi.

-Khoulo ak gneup teudiou ci bir nek. Souma ko wowé mouy dioy nane ma keur gui kéne beugouko fi ba mane tamitt ma gueume ligne ma dane wakh khoulo tamitt ak gneup ndakh Coura. Après la khame ni c'était juste des prétextes pour que ma accélérer regroupement familiale bi. Coura da fa gnortoni meuna ko bagna yobe France du coup mou done ma forcer la main. Sa diabar la wone mais déssé wone nama khame. Bimay tak diabar sama bop mo takhone, ni ndeye, ni baye, ni mak, ni rak.

-Mane instant yi damay ragal sakh gnou sigueulé ma té défouma dara.

-Sigueulé bou démé nane ?

-Ndakh sa ex diabar bi khana. Est-ce que dougne fogue ni comme mome la mel ?

-Guiss ga Mouhamed sa yaye limou fi liguey yeup.

-Wa papa kagne lagnouy wo sama yaye ?

-Kharal...

Ma dieule sama portable diéma contacter Coura via whatsapp.

Dafa né « Allo » rek ma diokh portable bi Mouhamed. Guoné gui nara diogue rek ma képate ko sama wette, féne la démoul.

Adja dé paré na ci wakh dji khame na daigne bagne Coura dégue lignouy wakh.

Mouhamed dé ay waw rek lay tontou instant yi. Khoma louko yayame di wakh. Bess bouma samay dome wane louma khamoul, wappelou Coura yeup hauts-parleur lakoy def.

Touti après mou diokh telephone bi Rokhaya après mou couper mou diokhate ma sama telephone. Mané Adja diaroul mouy inquiéterwou. Sa ma wa keur amougnou problème.

********

Bi ma dégué ni ame na kouy feugue dé dama tite ci ay nelaw sakh...Kou gnou meuna yé ci fadiar dji la khamoul. Sama réveil diouli fadiar sakh sonner goul. Avant may diogue Adja yogue na oubi. Khamé na sama voix wou yaye dé mais khoma lougnouy wakh.

Guiss na Adja dougue ci bir salle de bain guénate solle yéré di wadja guéne.

-Fo dieum?

-Yéwou ga...Pourtant beuguou ma la wone yé dé.

-Sama yaye kay moma yé. Loume beugue?

-Néna ma défar keur gui balla fadjar di diotte. Khamou gnou fou guane di gneuwé.

Gueumintou wone na gueumintou guo khame ni, da fa guéne après rek ma weulbeutikouwatt dorat samay nélaw.

Kéne kou mel ni yowWhere stories live. Discover now