Start Reading
Description
FIRI KHASSIDA YII🖤🙏 Bismillah mangui toud CHEIKH SOUHAIBOU MBEGUERE Di ziar nieup surtout sama mbokki talibé yi ma andal niou bok beugg Serigne Touba Ligueye bi nak ma tambali danaka dafa dieksay rek idée nieuw nakh nekoul nieupeeu meunn lire alkhourane ta yitt takhoul niou bagna diangg alkhourane motakh def li dissi ligueyeul Serigne Touba diéma firi khassida yimou binn sikaw danaka yomboul ms Lou ab mbindef diémoul d'où kham loumouy saff Di toup nk si bepp dioumter youniou deff ta guenn xhamni yitt nitta matoul rek ndioumter mom nieupeeu koy deff Di toubatt si kadou yi bou werr🙏
FIRI KHASSIDA SINDIDI🙏
Continue Reading on Wattpad